Luke 21:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Li ngeen gis fii lépp, jamono dina ñëw joo xam ne dina daanu, ba doj dootul des ci kaw doj.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Lii ngeen gis nii, ay jant a ngi ñëw yu fi doj dootul des ci kaw doj, lépp ay jóoru.»