Luke 22:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte maa ngi leen koy wax, dootuma ko lekk mukk, lu dul ba kera mu mat ci nguuru Yàlla.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax maa leen ko wax, dootuma ko reer mukk, ba keroog solob reer bi di sotti ca nguurug Yàlla.»