bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 22:2
Luke 22:2 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya di wut pexem reylu Yeesu, ndaxte dañoo ragaloon nit ña.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir loolu sarxalkat yu mag ya ak firikati yoon ya di seet nu ñuy fexee ba rey Yeesu, waaye dañoo ragaloon nit ña.