Luke 22:23 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu taalibe yi di laajante ci seen biir, kan ci ñoom mooy nar a def loolu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu taalibe yi di laajante ci seen biir, kan ci ñoom moo nar jooju jëf.
Recommended Reading