Luke 22:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Taalibe ya it di werante, ngir xam kan ci ñoom moo gën a màgg.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ab werante itam dikkal leen, ñuy xëccoo ci seen biir ku wara gëna kawe ci ñoom.