Luke 22:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye yéen buleen def noonu. Ki gën a màgg ci yéen, na nekk ni ki gën a ndaw, te njiit mel ni surga.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen nag bumu deme noonu ci seen biir. Ki gëna kawe ci yeen, na mel ni moo gën di ndaw, te njiit li, na mel ni ab surga.