Luke 22:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Man nag jox naa leen sañ-sañu nguuru, ni ma ko sama Baay joxe.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Man itam ni ma sama baay dénke nguur, ni laa leen koy dénke.