Luke 22:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu Seytaane daldi solu Yudaa, mi ñuy wooye Iskariyo te mu bokkoon ca fukki taalibe ya ak ñaar.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seytaane nag dugg Yuda, mi ñuy wooye Iskaryo te mu bokkoon ca Fukk ñaak ñaar.