Luke 22:34 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu tontu ko ne: «Piyeer, maa ngi la koy wax, bala ginaar a sab tey jii, dinga weddi ñetti yoon ne, xam nga ma.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu ne ko: «Piyeer, maa la ko wax, bala ganaar a sab tey jii, dinga weddi ñetti yoon ne xam nga ma.»