Luke 22:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu Yudaa dem waxtaani ak saraxalekat yu mag ya ak kilifay wottukati kër Yàlla ga, ba xam nan la leen di jébbale Yeesu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yuda daldi diisooji ak sarxalkat yu mag ya, ak kilifay wattukati kër Yàlla ga, ngir xam nan lay tege Yeesu ci seeni loxo.