Luke 22:42 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
«Baay, soo ko bëggee, teggil ma kaasu naqar bii. Moona bumu doon sama coobare, waaye na sa coobare am.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne: «Baay, su dee sa coobare, teggil ma kaasu naqar bii. Bumuy sama coobare nag, waaye yaw, na sa coobare am.»
Recommended Reading