Luke 22:45 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu ñaanee ba noppi, mu jóg, dellusi ci taalibe yi, fekk leen ñuy nelaw, ndaxte seen xol dafa sonnoon ak tiis.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ñaan ba noppi, daldi jóg, délsi ci taalibe yi, fekk leen ñuy nelaw, sonn lool ndax aw tiis.