Luke 22:46 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu mu ne leen: «Lu tax ngeen di nelaw? Jógleen ñaan, ngir bañ a daanu cig fiir.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne leen: «Lu ngeen di nelaw? Jógleen ñaan, ngir baña tàbbi cig fiir.»