Luke 22:48 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu ne ko: «Ci fóon ngay jébbale Doomu nit ki ay noonam!»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu ne ko: «Yuda, fóon ngay wore Doomu nit ki!»