Luke 22:49 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ñi àndoon ak Yeesu gisee liy bëgg a xew, ñu ne: «Boroom bi, ndax nu dóore jaasi?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ña ànd ak Yeesu nag gis la ca nara topp, ñu ne: «Sang bi, nu jame saamar boog?»