Luke 22:5 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñu am ca bànneex bu réy, dig ko xaalis.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu am ca mbégte, digook moom, ngir jox ko xaalis.
Recommended Reading