Luke 22:56 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ab mbindaan gis ko, mu toog, taal bi di ko leeral, mu ne ko jàkk ne: «Nit kii itam àndoon na ak moom.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ab surga bu jigéen nag gis ko, mu toog fi kanam taal bi, mu ne ko jàkk, ne: «Kii it ci la, moom la àndaloon!»