Luke 22:58 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nes tuuti keneen gis ko ne: «Yaw itam ci ñoom nga bokk.» Piyeer tontu ko: «Sama waay, bokkuma ci.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nes tuut keneen gis ko ne: «Yaw it ci ñoom nga!» Piyeer ne ko: «Waa jii, du man!»