Luke 22:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yudaa nangu, di fexe jamono ju mu leen man a jébbal Yeesu, fu mbooloo ma nekkul.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yuda nangu, di wut nag yoon wu mu wore Yeesu, fu mbooloo ma teewul.