Luke 22:60 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Piyeer tontu ne: «Sama waay, xawma li ngay wax!» Bi kàddoom di daanu, faf ginaar daldi sab.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul Piyeer ne ko: «Waa jii, li ngay wax, xawma ma ko de!» Ca saa sa, ganaar sab, te kàddug Piyeer daanoogul sax.