bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 22:66
Luke 22:66 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi bët setee, kureelu njiiti xeet wa, maanaam saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya, daldi daje, indi Yeesu ci seen kanam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba bët setee, mbooloom magi askanu Yawut, ak sarxalkat yu mag ya, ak firikati yoon ya, ñépp daje. Ñu yóbbu Yeesu ca seen kurélu àtte ba.