Luke 22:67 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñu ne ko: «Soo dee Almasi bi, wax nu ko.» Mu tontu leen ne: «Su ma leen ko waxee, dungeen ma gëm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu ne ko: «Soo dee Almasi, wax nu ko.» Mu ne leen: «Su ma leen ko waxee, dungeen ma gëm.