Luke 23:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Pilaat daldi woo saraxalekat yu mag ya, njiit ya ak mbooloom Yawut ya ne leen:
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Pilaat woo sarxalkat yu mag ya, ak njiit ya ak askan wa.