Luke 23:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Erodd itam gisul tooñ gu mu def, ndegam mu yónneewaat nu ko. Nit kii deful genn tooñ gu jar ñu koy rey.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Erodd itam gisul lenn ci moom, ndax moo nu ko yónneewaat. Mu ngoog, waa jii deful lenn lu jar àtteb dee.