Luke 23:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ñu bokk di yuuxu, ñoom ñépp naan: «Reyal kii te bàyyi Barabas!»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñépp daldi xaacoondoo, ne: «Reyal kii te yiwil nu Barabas!»