Luke 23:28 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Yeesu daldi walbatiku ca ñoom ne: «Yéen jigéeni Yerusalem, buleen ma jooy! Jooyleen seen bopp ak seeni doom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu geesu leen, ne: «Yeen jigéeni Yerusalem, buleen ma jooy! Jooyleen seen bopp ak seeni doom.
Recommended Reading