Luke 23:3 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu Pilaat laaj ko: «Ndax yaa di buuru Yawut yi?» Yeesu tontu ko ne: «Wax nga ko.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Pilaat laaj ko ne ko: «Yaa di buurub Yawut yi?» Mu ne ko: «Yaa ko wax.»
Recommended Reading