Luke 23:32 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yóbbaale nañu itam ñeneen, ñuy ñaari defkati lu bon, ngir rey leen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yóbbaale nañu itam ñaari saaysaay, ngir boole leen ak Yeesu, rey leen.