Luke 23:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Pilaat ne saraxalekat yu mag ya ak mbooloo ma: «Gisuma genn tooñ ci nit kii.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Pilaat ne sarxalkat yu mag ya ak mbooloo ma: «Waa jii, gisuma ci moom genn tooñ.»