Luke 23:40 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ka ca des yedd moroom ma, naan ko: «Xanaa ragaloo Yàlla, yaw mi ñuy mbugal ni moom!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moroom ma nag femmu ko, ne ko: «Ragaloo sax Yàlla, te yaa ngi ci menn mbugal mii?