Luke 23:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ñu sax ci seeni wax naan: «Mi ngi jógloo mbooloo mi, di jàngale ci réewu Yawut ya mépp, li dale ci Galile ba fii.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul ñu gëna dëggal seeni wax, ne: «Mooy yékkati askan wi, ndax li muy jàngle ci mboolem réewum Yawut, dale ko ca Galile ba fii.»