bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Luke 23:56
Luke 23:56 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu ñu dellu defari cuuraay ak latkoloñ ngir néew ba. Ca bésu noflaay ba ñu noppalu, ni ko yoon wi santaanee.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee ñu dellu, waajali cuuraay ak diwu xeeñlu ngir néew ba. Bésub Noflaay nag taxaw, ñu dal-lu, ni ko yoon santaanee.