Luke 23:6 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi Pilaat yégee baat yooyu, mu laajte ne: «Ndax nit kii Galile la dëkk?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Pilaat dégg loolu, daldi ne: «Waa jii waa Galile la?»