Luke 24:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ñu teg wax jooju ay jeneer, ba gëmuñu jigéen ñooñu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul ñu def waxi jigéen ña ay caaxaan, ba gëmuñu leen.