Luke 24:19 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Yeesu ne leen: «Lu fi xew?» Ñu tontu ko ne: «Mbirum Yeesum Nasaret. Ab yonent la woon bu doon def ay jëf yu mag, di wax ay kàddu yu am doole, ci kanam nit ñi ak ca kanam Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu ne leen: «Lu fi xew?» Ñu ne ko: «Mbirum Yeesum Nasaret. Mu doonoon ab yonent bu manoorewu ci jëf ak ci kàddu, Yàlla ak askan wépp seede.