Luke 24:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye sunuy saraxalekat yu mag ak sunuy njiit ñoo ko jébbal nguur gi ngir ñu àtte ko, teg ko dee, ba daaj ko ci bant.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye sunu sarxalkat yu mag ak sunuy njiit ñoo ko teg ciy loxo, ngir ñu teg ko àtteb dee, daaj ko ci bant.