Luke 24:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nun nag danoo yaakaaroon ne, mooy kiy nar a jot Israyil. Waaye bi loolu xewee ak léegi, tey la ñetteelu fan bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nun nag danoo yaakaaroon ne mooy jotsi Israyil. Loolu lépp teewul nu ngii ci ñetteelu fan, ba mbir yooyu amee ba tey.