Luke 24:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Teewul nag am na ay jigéen yu bokk ci nun yu nu jaaxal. Dañoo fajaru ca bàmmeel ba,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ay jigéen ñu bokk ci nun nag ñoo nu jaaxal. Ndax ñoo jëlu dem ca bàmmeel ba,