Luke 24:28 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ñuy jub dëkk, ba ñu jëmoon nag, Yeesu def ni kuy jubal yoonam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka lañuy jub dëkk, ba ñu jëm, mu mel ni ku nara jubal yoonam.