Luke 24:31 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu defee loolu, lépp leer ci seeni bët, ñu daldi ko xàmmi. Waaye Yeesu ne mes, gisatuñu ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca la seeni gët ubbiku, ñu xàmmi ko. Moom nag, mu ne mes, réer leen.