Luke 24:35 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñaari taalibe ya ñoom it daldi leen nettali la xewoon ca yoon wa ak ni ñu xàmmee Yeesu, bi mu dammee mburu ma.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñaari taalibe ya ñoom it, nettali leen la xewoon ca yoon wa ak na ñu xàmmee Yeesu, ba mu daggee mburu ma.