Luke 24:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ñu jógee bàmmeel ba, ñu dem nettaliji loolu lépp fukki ndaw ya ak benn, ak ña ca des ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu jóge ca bàmmeel ba, dem àgge loolu lépp Fukk ñaak benn, ak ña ca des ñépp.