Luke 3:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ay juutikat itam ñëw ca Yaxya, ngir mu sóob leen ci ndox; ñu ne ko: «Kilifa gi, lu nu war a def?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ay juutikat itam dikk, ngir sóobusi; ñu ne Yaxya: «Sëriñ bi, ana lu nu war?»