Luke 3:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mbooloo maa ngay xaar, di séentook a laaj ci seen xel, ndax Yaxya mooy Almasi bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu askan wa di séentu, ñépp di seetaat ci seen xel, ndax Yaxya mooy Almasi.