Luke 3:17 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Layoom mu ngi ci loxoom, ngir jéri dàgga ja, ba mu set; pepp ma dina ko def ca sàqam, waaye xatax ba dina ko lakk ci safara su dul fey mukk.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ab layoom a ngi ci loxoom, mooy jéri dàggaam, ba mu set wecc; pepp mi lay fat cim sàqam, waaye xatax bi, da koy lakk ci sawara su dul fey mukk.»