Luke 3:8 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Jëfeleen nag ni ñu tuub seeni bàkkaar, te bañ a nax seen bopp naan: “Nun daal doomi Ibraayma lanu,” ndaxte maa ngi leen koy wax, Yàlla man na defal Ibraayma ay doom ci doj yii.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag jëfeleen jëf ju yelloo ag tuubeel, te baña nax seen bopp naan: “Nun, Ibraayma mooy sunu maam,” ndax maa leen ko wax, doj yii, Yàlla man na cee sàkkal Ibraayma aw askan.