Luke 4:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Moona Yàlla yónniwul Iliyas ci kenn ci ñoom, waaye mu yebal ko ci jigéen ju jëkkëram faatu, ju dëkk Sarebta, ca wetu Sidon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moona du kenn ci ñoom ku ñu yebal Ilyaas ca moom ku moy jëtun ba dëkke Sarebta, ca Sidon.