Luke 4:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te it amoon na ca Israyil, ca jamonoy yonent Yàlla Alisa, ay nit ñu bare ñu gaana. Waaye fajul ci kenn ku dul Naaman, mi dëkkoon réewu Siri.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jamonoy Yonent Yàlla Alyaasa itam, ay gaana yu baree nga woon ca Israyil. Waaye fajeesu ci kenn ku moy Naaman, waa Siri ba.»