Luke 4:35 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu gëdd ko naan: «Noppil te génn ci moom!» Noonu rab wi daaneel nit ki ci suuf ci kanamu ñépp, daldi génn ci moom te gaañu ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu nag gëdd ko, ne ko: «Noppil te génn nit ki!» Rab wa daaneel nit ki ca digg mbooloo ma, doora génn te gaañu ko fenn.