Luke 4:36 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi loolu amee ñépp waaru, ñuy waxante ci seen biir naan: «Céy jii wax! Ci sañ-sañ ak doole lay sant rab yi, ñu daldi génn.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee ñépp a waaru, di wax ci seen biir, naan: «Gii kàddu lu mu doon? Moom de sañ-sañ ak xam-xam lay joxe rab yi ndigal, ñu génn.»